Moussa sall

Moussa sall Université MAODO❤️

05/04/2026

L’ingénieur morale cheikh seydi aboubacar sy mansour

05/02/2026

L’ingénieur morale cheikh seydi aboubacar Sy mansour

Naan, nàngam dal na ma Nàngam dal na réew mi Dara indiwuko ludul lamiñ yiLu waay neex waxLu waay neex defLu waay neex da...
02/19/2026

Naan, nàngam dal na ma Nàngam dal na réew mi Dara indiwuko ludul lamiñ yi
Lu waay neex wax
Lu waay neex def
Lu waay neex dal ko
95
Serigne Mansour SY Borom Daaraji (RTA)

Jaamu YallaAk topp Yalla du bennJaamu Yalla xol moo koy defTopp Yalla cér moo koy defSerigne Babacar SY Abdou
02/16/2026

Jaamu Yalla
Ak topp Yalla du benn
Jaamu Yalla xol moo koy def
Topp Yalla cér moo koy def
Serigne Babacar SY Abdou

Bögg, ñépp bëgg lañépp nangul laCi rey la bokkYalla su ko doon mayéMay ko boppamSerigne Cheikh Al Maktoum (RTA)
12/25/2025

Bögg, ñépp bëgg la
ñépp nangul la
Ci rey la bokk
Yalla su ko doon mayé
May ko boppam
Serigne Cheikh Al Maktoum (RTA)

Naan, nàngam dal na ma Nàngam dal na réew mi Dara indiwuko ludul lamiñ yiLu waay neex waxLu waay neex defLu waay neex da...
12/08/2025

Naan, nàngam dal na ma Nàngam dal na réew mi Dara indiwuko ludul lamiñ yi
Lu waay neex wax
Lu waay neex def
Lu waay neex dal ko
Serigne Mansour SY Borom Daaraji (RTA)

Réew miNañu dimbale senn boppBoole senn doole nekk bennTe muy dëgg ci nun ñéppYalla defal ñu jàmmMame Dabakh (RTA)
11/24/2025

Réew mi
Nañu dimbale senn bopp
Boole senn doole nekk benn
Te muy dëgg ci nun ñépp
Yalla defal ñu jàmm
Mame Dabakh (RTA)

Am-amu àdduna ak barkeNekkul ci alal ju bari Waaye mi ngi nekkCi xol buy yëg Yalla Xol bu wóolu YallaXol bu soppu YallaS...
11/21/2025

Am-amu àdduna ak barke
Nekkul ci alal ju bari Waaye mi ngi nekk
Ci xol buy yëg Yalla Xol bu wóolu Yalla
Xol bu soppu Yalla
Serigne Maodo SY Dabakh

Xam-xam ba xam-xam dajBa ca gën mooy xam sa boppRéer ba réer dajBa ca yeesMooy réere sa boppSerigne Babacar SY (RTA)    ...
11/21/2025

Xam-xam ba xam-xam daj
Ba ca gën mooy xam sa bopp
Réer ba réer daj
Ba ca yees
Mooy réere sa bopp
Serigne Babacar SY (RTA)

Ku xamul foy mujjWaroo xeeb kennNdax melokaanamSerigne Babacar SY Mansour
11/19/2025

Ku xamul foy mujj
Waroo xeeb kenn
Ndax melokaanam
Serigne Babacar SY Mansour

Address

Montreal, QC

Website

Alerts

Be the first to know and let us send you an email when Moussa sall posts news and promotions. Your email address will not be used for any other purpose, and you can unsubscribe at any time.

Contact The Place Of Worship

Send a message to Moussa sall:

Share