05/12/2018
اللهم اغفر له و ارحمه....
Repose en paix frere yalna yalla atté la si yermandé té xaaré la Adiana....bijaahi Nabii Moustapha saws ..
Frere bou baax la woon bou yaarou bou yaatou bou am yeurmandé bou fonkoon taggou Rassoulillahi sawa yalnala Ghoulamou Rassoulillahi saws téérou... Séédé yepp bénn la Yalna la yalla atté si yeurmandêm té amnansi yaakaar bou baax...
Repose en paix Abdoullahi Diéye...