XAM CERNO JOTNA

XAM CERNO JOTNA Informations de contact, plan et itinéraire, formulaire de contact, heures d'ouverture, services, évaluations, photos, vidéos et annonces de XAM CERNO JOTNA, Organisation religieuse, Darou Mousti.

CHEIKH IBRAHIMA FATY mingi gané jamono ci atum 1865, date bii nak daa bari ay wuuté lol, ndax am niu jàpp 1862 la féegn, am ñu wax 1863, waayé gni wax 1865 da nioo sukandikoo rek ci li ñu wax ni mingi ganée adduna ca Xaréb_Paaté_Bajaan ba amoon ci diganté

25/06/2026

Une de mes publications a obtenu plus de 10 réactions la semaine dernière. Merci à tout le monde pour votre soutien ! 🎉

Les Mourides de Touba Grand Est🇫🇷 ont rendu un vibrant hommage au bras droit de Cheikh Ahmadou Bamba, à travers une séri...
11/02/2026

Les Mourides de Touba Grand Est🇫🇷 ont rendu un vibrant hommage au bras droit de Cheikh Ahmadou Bamba, à travers une série de conférences, de kourels, d’échanges et de panels d’une grande richesse intellectuelle et spirituelle.

Cette rencontre a été consacrée à la vie et à l’héritage de Cheikh Ibrahima Faty Mbacke (1865–1943), figure emblématique de la Mouridiyyah, reconnu pour sa fidélité absolue à son frère et guide Cheikhoul Khadim.

Les travaux ont permis d’explorer plusieurs dimensions majeures de son œuvre et de son influence à travers trois panels de haut niveau :
• Panel 1 : « Du service spirituel au développement territorial : comment Mame Thierno a incarné l’économie sociale et solidaire mouride », animé par Dr Serigne Khadim Ibn Serigne Abass.
👉 https://www.youtube.com/watch?v=ua_Pu3chmjU&list=PLVRknQ0OoqaYUG8LIg-y1_LiOnjIswl3d

• Panel 2 : « La relation fraternelle entre Cheikh Ahmadou Bamba et Mame Thierno Birahim : un modèle de confiance et de loyauté », présenté par Serigne Mbaye Gueye SYLL et Abdou Khadre Ba Majalis.
👉 https://www.youtube.com/watch?v=VvMJVt8ZUkI&list=PLVRknQ0OoqaYUG8LIg-y1_LiOnjIswl3d&index=2
👉 https://www.youtube.com/watch?v=BJxkMZXta0I&list=PLVRknQ0OoqaYUG8LIg-y1_LiOnjIswl3d&index=3

• Panel 3 : « L’héritage de Mame Thierno : foi, travail et éducation », développé par Pr Mourtada Mboup et Pr Galaye Ndiaye.
👉https://www.youtube.com/watch?v=l5mKpBzwrPE&list=PLVRknQ0OoqaYUG8LIg-y1_LiOnjIswl3d&index=4
👉https://www.youtube.com/watch?v=x4Rgc6Bs7SU

Ces échanges ont mis en lumière la profondeur spirituelle, l’engagement social et la vision éducative de Borom Darou, dont l’héritage continue d’inspirer les générations mourides d’hier et d’aujourd’hui.

03/02/2026

MAME THIERNO

« Sa personnalité n’est pas à chercher dans les livres, mais à découvrir dans ses actions, sa sincère et son comportement irréprochable . Il était un traducteur fidèle de Serigne Touba, car exprimant ses valeurs, son comportement, sa démarche tout en l'incarnant au plus profond de son être.

En vérité toute sa personnalité s'était tissée sur la vérité et la sincérité. C'est pourquoi, si tu voyais son apparence, tu l'aimerais sans recul. De même, si tu l'observais agir, tu verras un homme aimable, doux, admirable modeste, ascétique et généreux. »

M. Moustapha Diop

Waajal Màgalug Daaru Musti Mercredi 04 Février 2026 / 15i fani Sha'baan 1447h Sëriñ Móodu Habib Mbàkke Ibn Maam Cerno Ib...
03/02/2026

Waajal Màgalug Daaru Musti
Mercredi 04 Février 2026 / 15i fani Sha'baan 1447h
Sëriñ Móodu Habib Mbàkke Ibn Maam Cerno Ibrahima Faati
Sëriñ Móodu Habib Mbàkke migi feñee Jamono ci Attum 1897 ca Mbàkke Bawal
Domi Maam Cerno Ibrahima Faati ak Soxna Mariyamaa Balla Silla
Bimu Ganee Adunaa Wajuraam Maam Cerno dakoo Tuudee Wajuraam Maam Moor Anta Saali Mbàkke ñu jëlee Tuur wi di Móodu Habib
Am na ñumu Bokkal Wajuur bu Jiguene ak Wajuur bu Goor ñu mën cee yim Soxna Astu Cerno Mbàkke, Soxna Aminta Mbàkke,Sëriñ Abdul Xudooss Mbàkke,Sëriñ Mahmadaan Kosso Mbàkke ak mom Sëriñ Móodu Habib Mbàkke
Bimu Matee Daal Alxuraanu Kaarim Wajuraam dakoo joox Sëriñ Ibrahima Silla lakoo joox ca Mbàkke Kadior ñati att lafaa deef ci moom fofaa saax la Mokalee Alxuraane mu bindee Kaamil joox ko Sëriñ Tuubaa Ginaaw bi Maam Cerno Ibrahima Faati Bolee ko ak Sëriñ Móodu Awa Balla, Sëriñ Seex Awa Balla, Sëriñ Ibrahima Faati Niang ak mom Sëriñ Móodu Habib joox leen Sëriñ Tuubaa ca Njaareem bañu demee Njaareem ci Sëriñ bi Sëriñ Tuubaa dakoo joox Sëriñ Móodu Mustafaa Mbàkke ngir mu Jàngaal ko xam xam Ginaaw bi mu dellusi waat ci Loxoy Xaadimur Raassul
Sëriñ Móodu Habib Mbàkke Bimu nekee Njaareem ci Sëriñ Tuubaa daa nako bindaal ay Kaamil baa nimu Jotee Ngueuramoul ci Sëriñ Tuubaa biis bimuy joot Ndigalu Sëriñ Tuubaa Sëriñ Tuubaa baat yi lakoo wax nikoo Yonneti Shw Ngueuram nalaa Yalla Sunu Boroom Ngueuram nala maan minga doon ligeeyal Ngueuram nala Ginaaw bamu Jugee ci Sëriñ Tuubaa dellusi waat na ci Loxoy Maam Cerno
Maam Cerno Joxoon nako Chef de village bu Daaru Musti
Sëriñ Móodu Habib Mbàkke Yorol na ñari doom Seexxul Xaadim muy Soxna Xaadijaatu Mbàkke ak Soxna Maïmunatu Mbàkke Kubraa waaye Soxna Xaadijaatu Mbàkke Yaggu faa mu Genee Adunaa Soxna Maïmunatu Mbàkke Kubraa am nañu been doom ak Sëriñ Móodu Habib Mbàkke ñu mën cee yim Sëriñ Mustafaa Maï
Mu wëy di neek ci Wajuraam Maam Cerno Ibrahima Faati ba nifi Wajuraam Bàyiko mu jël leepaam joox Magam Sëriñ Móodu Awa Balla Mbàkke topoon lool ci Ginnaawam Magam ja ba nimu Genee Adunaa lataa muy Genee Adunaa ligeey nafi Ligeey bu am soloo amoon na ay Daara yu taako taaku
Bimu Chef de village bu Daaru Musti indi nafaa Brigade Gendarmerie, élevage, poste téléphone, école française...
Taxawu lool Dëkk bii
Sëriñ Móodu Habib Mbàkke nekoon ku oyof Laabir Yaatu Taabe
Yaatoom bobu taax na Politiciens yi ku meussa ñew Daaru Musti ci Këraam gaay daal kuci mel ni Leopold Sedare Senghor...
Bëeg gimu bëgoon Reewum Sénégal taax ñu takaal kofi ab médaille ci Attum 1952
Ci Attum 1959 taakalatoon banen médailles tee médailles kouñu ko meusaana takal ab yaaree kaat nga yaaree kaat gogu mu nekoon taax na mu yewu ay ndongaa tarbiyaa yi nekoon këraam wax leen ñu dem ligeey yi ngir meuna am loo defal sa boppu
Wajuraam Maam Cerno Ibrahima Faati ku fonkon Domaam ji moko defoon Chef de village bu Daaru Musti nonu it la Fonkee won Wajuraam Bindaal nako ay kamil yu Beuree beuri nonu it la Fonkee won ay Magam aki Rakam Sëriñ Móodu Awa Balla, Sëriñ Seex Awa Balla...
Ku Njabotug Seexxul Xaadim Beegoon Wajuraam Seexxul Xaadim moko Yaar moko Ngueuram Seex Muhammadul Mustafaa Moko Jàngaal Xam Xam Sëriñ Móodu Habib Mbàkke kukoo jegee won laa ba taax moo daa bindee Discours yi ci Màgalug Daaru Xudooss gi Magam Seex Muhammadul Faadal Mbàkke ku wolaratee won la ak Rakam ji di Sëriñ Móodu Habib Mbàkke sen digaantee donan digaantee bu Rafetoon lool bu Seex Muhammadul Faadal meusaana ñew Daaru Musti ci kër Sëriñ Móodu Habib laay daal Seex Muhammadul Faadal bindee na ay Letaar Rakam ji di Sëriñ Móodu Habib ay Letaar yu beuri beuri ngir diko ci sante Seex Muhammadul Faadal Tuudee nako doom muy Sëriñ Habibou Mbàkke Falillu ba taax saax Njabootug Seex Muhammadul Faadal yigi weyaal lolu ci ag Njabootaam ak mbolem Njabootug Seexxul Xaadim nonu lañu meloon ak Domu Maam Cerno bi baci Sëriñ Murtadaa Mbàkke Sëriñ Murtadaa saax Tuudee nako doom Soxna Faati Ja Mbàkke Sëriñ Móodu Habib Mbàkke Tuudee nako doom muy ab Tawam bu Jiguene Soxna Maïmunatu Mbàkke Kubraa minga xam bi Sëriñ Móodu Habib moko yoron Sëriñ Móodu Habib Mbàkke Tuudee nako doom Magam Soxna Uumi Mbàkke Bintu Seexxul Xaadim Sëriñ Móodu Habib Tuudee nako doom ak ñenen ak ñenen ci Njabotug Seexxul Xaadim gi
Ñimu Bokkal Maam Cerno ñeppa ko Tuudee Doom likoo Dalee ci Sëriñ Móodu Awa Balla baci Sëriñ Xaalid Mbàkke
Sëriñ Móodu Habib Mbàkke ku amoon kolaree ci Sëriñ Abass Mbàkke ak Sëriñ Seex Awa Balla Mbàkke ba taax ñaree foo meusaana Guiss Sëriñ Móodu Habib guisse leen faa
Ku Jaaxaso woon la ak Mbolem Yonnu Murid wi ñeppu Autorité coloniale yi
Ku neek ku yemee won lool daa na wax ku ñewa gul Daaru Musti laa nek baa nimu fi Bàyiko
Sëriñ Móodu Habib Mbàkke migi Genee Adunaa Diber 10i Fani Tabaski 1379h Dëpok won ak Bisub Tabaski ci Attum 1960 ñu fananal ko baca Suuba sa ci yor yor ñu Jebbal ko Boroomam Sëriñ Bassiru Mbàkke Moom Seexxul Xaadim moko Taxawu moko Jebbal Boroomam ca wetu Wajuraam baa Maam Cerno Ibrahima Faati Bëyti ci Ndigalu Seex Muhammadul Faadal Mbàkke ak Sëriñ Móodu Awa Balla Mbàkke ci Tewaayu Mbolem Njabootug Maam Cerno gi ak Xilifaa yu beuri si yonnu wi
Ay Xalifam ni lañu Tedee Tawam Sëriñ Mustafaa Maï moko Njëkka Wutu 1960 ba 2014
Sëriñ Seex Astu Faay mofi neek ba taay di ku baax oyof lool am xam xam Yàl nafi Yagg lool te wer ak mbolem Njaboot gi ak Talibe yi
Sëriñ Móodu Habib Mbàkke am na biis buñu koy Fataliku aka Nianal muy Bisub 12i fani Tabaski ay biis Ginaaw bamu fi Bàyiko ba taay ñogi koy Màgal ak Bisub Wajuraam bidii Màgalug Daaru Musti
Sëriñ Móodu Habib Mbàkke Yal nañu ko Yalla fayal Yoku ay Leeram Tas nu si Baarkem 'baan1447

MAME THIERNO biffi Serigne bi  bayeko en 1927 da woté darou khoudoss nieup nieuw mouni👇👇👇👇👇👇👇Serigne manoumbe Mbacke dem...
03/02/2026

MAME THIERNO biffi Serigne bi bayeko en 1927 da woté darou khoudoss nieup nieuw mouni
👇👇👇👇👇👇👇
Serigne manoumbe Mbacke demal ligueyi bo dikéé gua def liguadane def. Kofi fékeu gua dioxkoko.
😭😭😭😭😭
Cheikh Ibra Fall wanel Yonne.koudane guisse ba guisatul koka mata wane Yonne.
leundeume guifi Serigne bi bayi mo gueune métti Bou djeukeu ba.
guinaw Serigne bi biko nitt gni xamagoul yako wanné ba nitt yeup xamko kone wanal nitt gni funiouy diarr.
😭😭😭😭😭
Serigne Modou Moustapha dou yow yafi djeukeu am baye bu baxx niakeuko.togal fi té nékeu lissa baye newone bo n néwuul nissa baye melone nite gni dinagnela tek finiou tegone sa baye.
😭😭😭😭😭
Serigne Fallou ak Serigne bassirou topuleene sen magg nakh nioune askanou Serigne Mbacke Mor xajouniou si neigue waxumalak ben deukkeu té luniou am nionko amé si topu sunu magg.

Adresse

Darou Mousti

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque XAM CERNO JOTNA publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Raccourcis

Partager